One Lyrical ‘s Self Made Lyrics (Ft. Hakill)

[VERSE 1_One Lyrical] Da may hustle toogal di wax pourquoi ñu nan ma no way Beugguloo ma me too I do you baby screaming my name I believe I can fly don’t tell me no bless over my lay Still the same don’t know us Keep yourself about me Tay ma burle kon jarul pass Gnaata nitt a ma gassal pax Gnaata nio ma bagn Mais né nagn bul di topp sen xol yeuppay bax Gnaata nio ma yeene comeback Ñaata nitt nga woolu denk len sa lepp tay niou nan la yay kan (Fuck yay Kan) Motherfucker yow yay kan (Mofucker yay kan) Topp sa yoonu bopp rekk a fi des Seugg gni di wax siggil sa bopp Siggil sa boop sëgg say wayjur hater niggers what a fuck Man maa siiw parce que da ma sob Li ngen gnoddi boo ubbe sama bopp ding ko fekk mu toog Keneen ku melni man gisu mako Ci kaw ci sa kanam feeteel ginaaw budul ci gent do ma fuck Nee na la man bëggu ma jikko toot Fuck you ya’g sa buzz do gis ku dee yobbale siiw yawmal xiyaam (Fuck)

[CHORUS] Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon

See Also  Jake Regal

[VERSE 2_ HAKILL] Bo xamul fi nga jëm deelul fi nga joge Loolu day fekk fi nga joge neex Saytaane bari dooli ken duko jege Mais dara dara duma teree xeex Akk moom ndax ay sëttëm rekk ño ma wër Bëggu ñu ma nekk ci Jàmm ni malade budul wër Bimay ne sama biiru yaay rekk la nekk fu woor Judd nekk goor Zéro peur Yalla rekk lay soor Awma lu may rèccu lepp noonu la Duma changer tus lepp ci yoon bi la Yen say lu gëna baax ci yow lu bonn bi la Samay meilleurs professeurs sama noon yi la Nitt ku ñuul ñemewul lu bees Foo jaar ñu bëgg ma ray

Bu samay noon bariwul woon sama bopp lay njëkk mere Mën a baax mën a bonn lo fi seet gis ko may internet Nitt kuy weeco ay nitt doonul ludul nittu interêt Jël sama yoonu bopp vitesse Foog ma seey len Freins yi dagg may duggël vitesse gaaw ni Eminem Ay jëmm tiim ma bëgg ma fees man may nittu neen Jàng na ci lepp lima wees muy dëgg di fen Jël sama yoonu bopp, sama yoonu bopp, no no sama yoonu bopp Topp ma ken ma ngi sama yoon Topp ma ken ma ngi sama yoon Topp ma ken ma ngi sama yoon Ich yo boy

[CHORUS] Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon Dieul sama yoonu bopp a fi des Dieul sama yoon Dieul sama yoon

We will be happy to hear your thoughts

Leave a reply

Wasit
Logo