Maabo’s Wa Li Nékhoul Lyrics

Maabo Baby i love you Honey i need you

Beus bou nek nala wax, je t’aime Douma sone ci dila wane, how much i love you Deg na niouné dama dof, ci ioe Khana hnamougn ni yay dalal li wéreudi ci mane Beugouma niouy méroo, hiéé! Naniou andeu longo hiéé! Baniouma si khoulo ak niom Nieup nagn niou bayi niou jubo té nopi Yay sama ngélaw, ioe rek doy nga ci mane Soumala guissoul tamite, ya meun dara ci mane Yeug yeug bi amoul limite, melni assaman Sa mbeuguel damay doundeul, ni  oxygène si mane hé !      Yama téré nélaw, ken rek nga si mane Soumala guissoul tamite, aduna safal dou si mane Yeug yeug noum soré ci nite sama xol ley dane Sa mbeuguel lamay doundeul, ioe ya geun ci mane hiii !

Wa li nékhoul Mani wa li nékhoul aaahhh … Ioe mi ioe hé ! Yamay danel Mani wa li nékhoul

Lathi len ma loumou saff (loumou saff) lou nékh hey waay ! Li ma nar ci mone mi (lo nar) dou diékh oohhh ! Gni diém tass souniou li, khamougn Yeug yeug bou mel ni noo amoul Yay sama chocolat, cacao pure bi, may sa olala Mane may bou sure bi mome sa xol ak sey khalate hé! Wolouna, awma xel niarr hé! Wolouna

Yay sama ngélaw, ioe rek doy nga ci mane Soumala guissoul tamite, ya meun dara ci mane Yeug yeug bi amoul limite, melni assaman Sa mbeuguel damay doundeul, ni  oxygène si mane hé !      Yama téré nélaw, ken rek nga si mane Soumala guissoul tamite, aduna safal dou si mane Yeug yeug noum soré ci nite sama xol ley dane Sa mbeuguel lamay doundeul, ioe ya geun ci mane hiii !

See Also  Where Is Sal Magluta Now? Facts To Know About Him

Wa li nékhoul Mani wa li nékhoul aaahhh … Ioe mi ioe hé ! Yamay danel Mani wa li nékhoul Ioe mi leu, ioe mi leu hééé ! Wa li nékhoul Ioe mi leu, ioe mi leu hééé ! Mane wa li nékhoul Aaaahhh… ioe me ioe hé ! Yamey danel Mani wa li nékhoul

We will be happy to hear your thoughts

Leave a reply

Wasit
Logo